Découvrez JOOKKO, notre logiciel de gestion d'entreprise 100% sénégalaise.Découvrir
E-commerce

Jaay Ak Jënd Ci Internet Bi : Lane Mooy E-commerce ?

Tay, internet dafa yombalal na ñu ni ñuy jaayé ak jënd. Loolu ñu koy wax « e-commerce ». Waaye lan mooy loolu ? E-commerce mooy jaay wala ligeey ci internet. Boo amee lu ngay jaay, meun nga ko jaay ci...

JT
Jangaan Tech
12 janvier 20252 min de lecture
Jaay Ak Jënd Ci Internet Bi : Lane Mooy E-commerce ?

Tay, internet dafa yombalal na ñu ni ñuy jaayé ak jënd. Loolu ñu koy wax « e-commerce ». Waaye lan mooy loolu ?

E-commerce mooy jaay wala ligeey ci internet. Boo amee lu ngay jaay, meun nga ko jaay ci sa site web, ci réseaux sociaux yi (Facebook, Instagram, X (Twitter), TikTok, WhatsApp, etc.), wala ci yeneen plateformes yu jaay. Nit ñi mënañu jënd ci séni téléphone wala séni ordinateur, fu ñu nekk ci aduna bi.

Lu tax e-commerce ame solo ?

  • Dafa yombal : Nit ñi mëna ñu jënd fu ñu nekk, sans dem ci marché wala ci butik bi.
  • Dafa gaw : Jënd gi dafa gaw, ci quelques clics rek.
  • Meun nga gis ay jaayukaay yu bari : Ci internet, meun nga gis ay jaayukaay yu bari yu nekk ci ay dëkk yu wuute.
  • Meun nga comparé ay prix : Avant ngay jënd, meun nga comparé prix yi ci yeneen site yi.

Naka lañuy jaayé ci internet bi ?

  • Am benn site web : Meun nga créer sa site web ngir jaay say produits.
  • Utiliser réseaux sociaux yi : Facebook, Instagram, ak WhatsApp ay yoon yu baax la ngir jaay ci internet bi.
  • Utiliser ay plateformes yu jaay : Am na ay plateformes yu bari yu tax ngay jaay say produits ci internet.

E-commerce dafa yombalal jaay ak jënd, te dafa am solo lool ngir ñi bëgg jaay seeniy marchandises. Soo bëggé xam lu ëpp ci e-commerce, nga seet ci internet wala nga woo entreprise Jangaan Tech ñu défala formation yuñuy def ci walum jaay ak jënd ci Internet bi.

Mots-clés:#e-commerce

Articles similaires

Pourquoi Jangaan Tech est l'une des meilleures agence de développement d'application e-commerce au Sénégal ?
2 min de lecture

Pourquoi Jangaan Tech est l'une des meilleures agence de développement d'application e-commerce au Sénégal ?

L'échec de la majorité des boutiques en ligne au Sénégal ne vient pas de la qualité des produits vendus, mais d'une technologie calquée sur des modèles occidentaux complètement inadaptés à nos habitudes de consommation. Pour transformer réellement vos visiteurs en acheteurs, Jangaan Tech conçoit des applications e-commerce ancrées dans la réalité économique et technique de notre marché.

Lire l'article
Mudaay : L'application mobile pour vendre des produits physiques et digitaux au Sénégal
2 min de lecture

Mudaay : L'application mobile pour vendre des produits physiques et digitaux au Sénégal

Trouver une audience digitale sans expertise technique est un parcours du combattant pour les créateurs et les commerçants sénégalais. De l'autre côté, les consommateurs peinent à trouver une application unique pour découvrir des articles locaux ou acquérir des contenus numériques. Mudaay, développée par Jangaan Tech et disponible sur le Google PlayStore, est la marketplace e-commerce qui connecte instantanément l'offre et la demande. Cette application centralise l'achat et la vente de biens matériels et de produits digitaux pour simplifier le marché ouest-africain.

Lire l'article